Lyrks
Lyrks
Lyrks
Cover Art

LA FAMILLE AU SENEGAL OUI Lyrics by Diarra Sylla

2024

[Intro: Diarra Sylla]
Hmm
Et la famille au Sénégal?
Oui, bien sûr!
[Verse 1: Diarra Sylla]
Sori sama réew ak sama askan
Taxul ma fàtte man mi may kan
Damay liggéey doxuma ci caaxaan
Seen soutien da may bégal di ma yokku katan
Damay ñafe di liggéey duma geestu
Yónne yakamti ma duma daagu
Li ma weesu la réccu
Fi ma jëm leer na ma, man la ni séntu
[Pre-Chorus: Diarra Sylla]
Ay ay ay
Fii mooy Senegaal
[Chorus: Diarra Sylla]
Fii la xol yi di feexe
Fii la stresse biy wacce
Fii la xale yi gëna baaxe
Sama réew nii la neexee
[Post-Chorus: Diarra Sylla]
Foo dëkk, Senegaal? Oui!
Fière ci doon sénégalaise
La famille au Sénégal, oui
Fière ci doon sénégalaise
[Verse 2: Dior Mbaye, (Diarra Sylla)]
Civilisé, rafféte, meuneu sagnsé
Té beugg topou cas
(Ku ne ngay wax, pays de la teraanga)
Kenn du ñu yàpp, kenn du ñu xeep
Kenn du ñu kël-kële
(Ñun lañuy wax, pays de la teraanga)
Am teranga meun mass laa meun sedalee
(Ku nе ngay wax, pays de la teraanga)
Sama réew mi da may neex tе jàmm ja ngi fi
[?]
Jàng bi na fi sax, jàng bi
[Pre-Chorus: Dior Mbaye]
Ay ay ay
Fii mooy Senegaal!
[Chorus: Diarra Sylla]
Fii la xol yi di feexe
Fii la stresse biy wacce
Fii la xale yi gëna baaxe
Sama réew nii la neexee
[Post-Chorus: Diarra Sylla]
Foo dëkk, Senegaal? Oui! (Oui, bien sûr)
Fière ci doon sénégalaise (Oui, bien sûr)
La famille au Sénégal, oui (Oui, bien sûr)
Fière ci doon sénégalaise (Oui, bien sûr)
[Verse 3: Dior Mbaye, (Diarra Sylla)]
Yaw Diara Sylla! (Foo dëkk, Senegaal? Oui!)
Fatou Mbacké Diongay sa yaay (Fière ci doon sénégalaise)
Ami Ndikou Guey yaayam (La famille au Sénégal, oui)
Cheikh Diongay baayam (Fière ci doon sénégalaise)
Demba Sylla sa baay (Foo dëkk, Senegaal? oui!)
Sokhna Aïda Mbacké yaayam (Fière ci doon sénégalaise)
Yaay Seutou Serign Barra (La famille au Sénégal, oui)
Diarra yaay Seutou Serigne Touba (Fière ci doon sénégalaise)
[?] (Foo dëkk, Senegaal? Oui!)
[?] (Fière ci doon sénégalaise)
[?] (La famille au Sénégal, oui)
[?] (Fière ci doon sénégalaise)
[Outro: Diarra Sylla]
Foo dëkk, Senegaal? Oui! (Oui, bien sûr)
Fière ci doon sénégalaise (Oui, bien sûr)
La famille au Sénégal, oui (Oui, bien sûr)
Fière ci doon sénégalaise

About “LA FAMILLE AU SENEGAL OUI” by Diarra Sylla

Read the complete lyrics to "LA FAMILLE AU SENEGAL OUI" by Diarra Sylla in 2024. On Lyrks you can follow along with the full text, explore the artist's discography, and discover related songs. The track is often categorized under French Pop, Wolof, En Français.

"LA FAMILLE AU SENEGAL OUI" is performed by Diarra Sylla. in 2024 This page provides the full lyric text for fans who want to sing along, study the songwriting, or compare versions across releases. Lyrks organizes lyrics by artist and song slug so you can bookmark and share a stable URL. Music lyrics help listeners connect with emotion, narrative, and rhythm in a track. Whether you are learning English, researching a favorite chorus, or preparing for karaoke, having accurate line breaks and section labels (verse, chorus, bridge) makes the experience easier. We link to the official artist profile on Lyrks where available, including biography snippets, top songs, and chart placements when we have that data. If you enjoy "LA FAMILLE AU SENEGAL OUI", explore more songs by Diarra Sylla using the links below. Chart and trending pages on Lyrks highlight what listeners are searching for this week. For copyright or correction requests, see our DMCA and contact pages.

View all songs and biography for Diarra Sylla · Trending lyrics · Billboard Hot 100

Frequently asked questions

"LA FAMILLE AU SENEGAL OUI" is credited to Diarra Sylla. Songwriting credits may include additional writers listed on the release; check the credits section on this page for linked collaborators.

Album information for "LA FAMILLE AU SENEGAL OUI" is not available in our database yet. You can still read the full lyrics on this page.

Visit the Diarra Sylla artist page at /artist/diarra-sylla for biography, popular tracks, and links to more lyric pages.