Lyrks
Lyrks
Lyrks
Cover Art

Xamouloma Lyrics by Fire

0

Couplet 1:
Lo def malako dakk may badou meune lepp
Game bi nekatoul rap mais kou dakk lebb
Fii dafa tiliim tei chak jour niouy setal
Fii ngeye raak ba deii niou togg dila setane
Fi sene khela gatt motakh dougn goudou fane
Fi ghetto bei stylé melni ay mbeddu Fann
Mangui ak hamadi niou todd tekk warrga bi
Fekkei maci bolei ma dieul raw gadou bi
Magg daane tei ngembo ngembou khalei
Reye la nga seugue sigilela ndigalei
Loutakh manane lene ghetto bi da stylei mane dong nekone thug ci ay enfant gatei
Fii bene baye fall rekaye diakhal kogne bi yeup
Bima dioudo ba legui hamouma dadj di deup
Pussy oubekoul defena mon guene yomb
Bi tedj lene sene taate yi mo guene kou nieuw rek romb
Bene vidéo niounane fireminati
Niggers so funny douniou khamtei dougn ladjtei
Bind ba mame nane ma kocc barma fall
Nekone khalei bou ndaw done cons Bambaj fall
Dama changer sama tourr pour meune bokk
Mais changerwouma sama jiko pour rek bokk
Bouma khamoul sakh deima nianale mou yokk
Dama dioudou daldi tiital samay mbokk
Ci fanne you neew la reye nitt kima nekone
Dou pour iow kone limeye def boul nei da bone
Esk dinga guiss niit nane dangakoy diokh ngogn
Boula knockei esk kene dinagn ladj kou togn
Talent amoul boy, ligueye rek mo woor
Weer bi dina fegne tei dou done werrou koor
Khel di Gnafei beuss bou nekk moy yonou goor
Legui lepp nieuw fettei ci souniou boor.. Ibou
Refrain :
Xamouloma, nigga xamagoma
Boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma
Bo beuguei biff, nigga woma
Ladjtel niata rabou alle laniou diomal
Xamouloma, nigga xamouloma
Boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma
Bo beuguei biff, nigga woma
Ladjtel niata rabou alle laniou diomal
Couplet 2:
Damay rap dila diangal ni sama gars konzo
Mane la nieup di weurr meye melni la conde-jo
Dama ham yone bi ni kou dei baye doundate
Mane la nieup di khaar ni real ak barca
Sene khela vide ni sama casier judiciaire
Demagougn sakh guissna sene gale yi di taire
Douma khol depart bi wantei arrivei bi motakh limeye khel di fayeikou di chère
Gniko fonkoul la sene tchine di bakh ngerr
Back to reality fi amoul diannère
Bitch bi sama snap nena dama mignon
Poche diss na mais fokk niou lale ay millions
Niata nio parei bimlene neeii mangui nieuw, ba teye dji mangui ci kaw
Lou adversaire bi tangue bou parei wakhko mou nieuw, niane yimay niane defna ko bima dieuli ji communion… ibou
Refrain :
Xamouloma, nigga xamagoma
Boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma
Bo beuguei biff, nigga woma
Ladjtel niata rabou alle laniou diomal
Xamouloma, nigga xamouloma
Boumaye nieuw yene nieup laye bett xamagoma
Bo beuguei biff, nigga woma
Ladjtel niata rabou alle laniou diomal
Couplet 3:
Boma hamoul dema wowe EH wala nga woweima king bi
Liy bakh loutakh mouy khegne nekh da fekk bobou mongui ci tchine bi
Nioune daaniouy music tei douniou def fausse note motakh fi khamougn kouy thione seck
Nene dou meusseu guiss souf bou noy nane dafay dem di dale ci ay keek
Fekkma ci yone bi mey dawal 205
Hamouniou loudoul hustle hamougn loudoul niafei
Namena lolou tps yiniouy reréji sombi
Legui calculel calculel ma guenelela somme bi
Mangui def ci souf pour meune yegue ci kaw
Lane lay guiss boumalene di khol ladjko pithie biy naw
Beusse dou touti borom leye tolol sama nguentei ni 4avril
Damay todj game bi nga fekkma mbside ma togg ci samay nigga diap tchill
Guissngama meye takk rollie bi melni nigga damako tamone
Guissnga kene dou wakh ci sama succès melni nigga damako tamone
Mangui dokh di nieuw guissna nigga yi tekk sene mic melni kou guiss camionwou 100tonnes
Legui game bi dafa dihasso melni bene kogne bou am 100 kogne
Credits

About “Xamouloma” by Fire

Read the complete lyrics to "Xamouloma" by Fire. On Lyrks you can follow along with the full text, explore the artist's discography, and discover related songs. The track is often categorized under Rap.

"Xamouloma" is performed by Fire. This page provides the full lyric text for fans who want to sing along, study the songwriting, or compare versions across releases. Lyrks organizes lyrics by artist and song slug so you can bookmark and share a stable URL. Music lyrics help listeners connect with emotion, narrative, and rhythm in a track. Whether you are learning English, researching a favorite chorus, or preparing for karaoke, having accurate line breaks and section labels (verse, chorus, bridge) makes the experience easier. We link to the official artist profile on Lyrks where available, including biography snippets, top songs, and chart placements when we have that data. If you enjoy "Xamouloma", explore more songs by Fire using the links below. Chart and trending pages on Lyrks highlight what listeners are searching for this week. For copyright or correction requests, see our DMCA and contact pages.

View all songs and biography for Fire · Trending lyrics · Billboard Hot 100

Frequently asked questions

"Xamouloma" is credited to Fire. Songwriting credits may include additional writers listed on the release; check the credits section on this page for linked collaborators.

Album information for "Xamouloma" is not available in our database yet. You can still read the full lyrics on this page.

Visit the Fire artist page at /artist/fire for biography, popular tracks, and links to more lyric pages.