Lyrks
Lyrks
Sign In
Cover Art

Lamou Saff Lyrics by Jeeba

Alajee

2022

Eh lamou saff kén doula ko wakh
Ndakh kako mathie Ko xam
Ni nane ki dalay gololo nane do dara
Maa dougou ci biir ba lépp lérr ma
Naandie diarr ngako

Koula xamoul moy diranték yaw
Mbague chérie coco
Bo done musicien
Mané la do degammer
Déf ngama sa xalé
Do joué ak man jeu de gamin
Deuk dima diamb, dima diamb
Yoro marimba do Benjamin
Bo défoul ndank na meussa téyé
Sa lokho on sait jamais

Mom xalé la té bari na dolé
Mo raw alkaati dafay dooré
Dina la topato ba lathie la, lathie la
Lathie la bébé loy réeré
Té boko ladié
Mouné la bae man yaw mi lay rééré

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Eh dafa nékh lolou nga am
Kou xam liy diamb sa ditakh
Sokh lawoul sakh ngay wakh
Day exécuter néwoul kou rambakh
Téey na xamé na fougnouy féthié
Yéla ak ndaw rabine

Coller gnapp mélni docteur Raoult
Ak choloroquine
Armée wou kaw ak souf
Mélni kouy dém guerre
Tassaré arsenal yi boula dal nga terre
Dila woo ci beuré té léer na, léer na
Molla, mola meun dila nogatou
Tass sa nguémb mbeur ma danou na, oh secours

Mom xalé la té bari na dolé
Mo raw alkaati dafay dooré
Dina la topato ba lathie la, lathie la
Lathie la bébé loy réeré
Té boko ladié
Mouné la bae man yaw mi lay rééré

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?

Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Eh lamou saff kén doula ko wakh
Ndakh kako mathie Ko xam
Ni nane ki dalay gololo nane do dara
Maa dougou ci biir ba lépp lérr ma
Naandie diarr ngako
Koula xamoul moy diranték yaw
Mbague chérie coco
Bo done musicien
Mané la do degammer
Déf ngama sa xalé
Do joué ak man jeu de gamin
Deuk dima diamb, dima diamb
Yoro marimba do Benjamin
Bo défoul ndank na meussa téyé
Sa lokho on sait jamais

Mom xalé la té bari na dolé
Mo raw alkaati dafay dooré
Dina la topato ba lathie la, lathie la
Lathie la bébé loy réeré
Té boko ladié
Mouné la bae man yaw mi lay rééré

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Eh dafa nékh lolou nga am
Kou xam liy diamb sa ditakh
Sokh lawoul sakh ngay wakh
Day exécuter néwoul kou rambakh
Téey na xamé na fougnouy féthié
Yéla ak ndaw rabine
Coller gnapp mélni docteur Raoult
Ak choloroquine
Armée wou kaw ak souf
Mélni kouy dém guerre
Tassaré arsenal yi boula dal nga terre
Dila woo ci beuré té léer na, léer na
Molla, mola meun dila nogatou
Tass sa nguémb mbeur ma danou na, oh secours

Mom xalé la té bari na dolé
Mo raw alkaati dafay dooré
Dina la topato ba lathie la, lathie la
Lathie la bébé loy réeré
Té boko ladié
Mouné la bae man yaw mi lay rééré

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté

Fadjr tél ni lamay yéewé
Dima xool ci biir beut nane ma qu'est-ce que ça fait?
Yaw ya raw athlète bou drogué
Koula topp ba ci biir day moudié claté
Credits

About “Lamou Saff” by Jeeba

Read the complete lyrics to "Lamou Saff" by Jeeba from the album "Alajee" in 2022. On Lyrks you can follow along with the full text, explore the artist's discography, and discover related songs. The track is often categorized under Senegal, Wolof, Pop.

"Lamou Saff" is performed by Jeeba. from the album "Alajee" in 2022 This page provides the full lyric text for fans who want to sing along, study the songwriting, or compare versions across releases. Lyrks organizes lyrics by artist and song slug so you can bookmark and share a stable URL. Music lyrics help listeners connect with emotion, narrative, and rhythm in a track. Whether you are learning English, researching a favorite chorus, or preparing for karaoke, having accurate line breaks and section labels (verse, chorus, bridge) makes the experience easier. We link to the official artist profile on Lyrks where available, including biography snippets, top songs, and chart placements when we have that data. If you enjoy "Lamou Saff", explore more songs by Jeeba using the links below. Chart and trending pages on Lyrks highlight what listeners are searching for this week. For copyright or correction requests, see our DMCA and contact pages.

View all songs and biography for Jeeba · Trending lyrics · Billboard Hot 100

Frequently asked questions

"Lamou Saff" is credited to Jeeba. Songwriting credits may include additional writers listed on the release; check the credits section on this page for linked collaborators.

"Lamou Saff" appears on "Alajee" in 2022.

Visit the Jeeba artist page at /artist/jeeba for biography, popular tracks, and links to more lyric pages.


Lyrks
Lyrks

Your gateway to the world of music lyrics.

Product

Features


© 2026 Lyrks. All rights reserved.