[Couplet 1] Yeah Yeah Aaahan Yeah Yeah Sama Xoll mo tiakar Fess ba tourauk nakar Sama xell teudiou mané fils on rek Melni kouniou teuthie prison break Sama euleuk leundeum, Sama thieur yi né lou peuyiss Xeuy hopital gontou police Deuk cii bèn poukouss ak sama weuliss Xalé yi yapp ma, Djiguène yi xepp ma Askan wii beurgueule maa, Sheytané xeur teulma Cii pet lakoy doundeu ak yène Dotou ma xalé borom fane werrii attela (30ans) Sa youma wétté sama sagarou mattela Waniarou djapp sama bopp fébarou tékki Sama xoll bii di sékki Ya !!! Douma incapable bounetou yeupeu teudiou Bokk yeup adiou Cii Pét laay doundé gathié bimaay yéndo Pa bi dieum na makk té mère bi damako yeureum Sama yéné cii niom mo kawé té yorouma deureum Souma sanione wakh djou yakouleu Lifi né moy awouma fiitou nieuw sen keur dii niane soxna Sama yakar-ra takk djeupétt Makoy doundeu cii pét Liimay ragal biss guène dégg né salite naa Ndakh gathié siiittt naa, Té doundou bi tek nama fitna Thiow djipp naa, Borom fiitou gaindé titna Borom fiitou gaindé titna [Refrain] Yeah Yeah !!! Cii pét lakoy doundeu ak yène Yeah Yeah !!! Cii pét lakoy doundeu ak yène Han !! Cii pet lakoy doundeu ak yène Yeah !!! Cii pét lakoy doundeu ak yène [Couplet 2] Ya Ya Ya Askan wé niou imposé am am Ba taxna kou niakk yaw ak xalé bou ndaw yéneuy yem Kène dou lathie sa waw ak sa détt Sa guiss guiss cii lène bokko, yorokko, lo wakh niouné Ohooooooo !!! Yeah !!! Pression = pression Niata nio sopii sèn direction Ndakh meuneu touniou waune dékou sèn situation Basculés cii yamba, alcool, gainze, ak agression Xam naniou né gueunoul Mais société bélèn tek louniou meunoul Yaw Bania deff nii niom motakh maay nott sama bakane bi déy Thieuy so xamone limay dathie ak sama back-in-the-day Mane rek-kaay dess cii scène bii Bouniou ropé diak yii Ak samay back yi (Gars yii) Wathié samay casquette biiy neup sama beutt you taa-yii Sama vergogne takh malèni neubb sama rongogne [Refrain] Cii pét lakoy doundeu ak yène Yeah !!! Cii pét lakoy doundeu ak yène Cii pét lakoy doundeu ak yène Cii pét lakoy doundeu ak yène Cii pét lakoy doundeu ak yène [Couplet 3] Yo Barça wala barzak Mouk Xarou douma tchii fekk Donté légg légg sama xell doxonetou Ma siiki saak xell niarou Sama gueum deufeul maa Yalla ma tekk natou té niakk dou saakh Souma rombé guène tchipeu touma dieuwma Té mane xawouma sama tort moy awouma Cii pét lay massla ak yène bagna setlou limeuy nieuklo Nimaay yotté ak nimaay yeuklo Kouma sétsi ma rouss ko entrée cii sama sagarou pentré Nakar bii cii sama xoll laniou ko encré [Refrain] Cii pét lakoy doundeu ak yène Yeah !!! Cii pét lakoy doundeu ak yène Han !!! Cii pét Yeah !!! Cii pét lakoy doundeu ak yène Yeah !!! Cii pét lakoy doundeu ak yène [Couplet 4] Yeah Yo yo !!! Cii sama xalima lay yegg ligni mbébett cii xoll yi Diko togué cii pneu kogne bi cii keur yi Prézi niombar, Wérou niou, Lékou niou, Nékkou niou Gorrou niou Yattou niou, Nga djapp niou ,Ndiapé niou Cii pét lay diwo sama déba-dépp Nguir samay weurseuk tidiékou Cii pét lay amé touti yakkar dii gueum nii Yalla douniou sétane None yi digni rétane Cii pét lay djougué guène diéngou soufeul sama djeumeu bagna xepp Sous métier amoul Talal niou faayla ak talal niou maayla yémoul Daga wara yéngou cii dara Yalla wakhoul kène lène Kou talal dii niane sa bopp ngay yapp lou Daga wara sabapp lou Djégou fipou mélni kou khapp lou Lamb dathie borom fiitou gaindé dou tiitt wala Djougueul cii bopp kogne biga tokk di la- ngal loss Melni kouy arbitré finalou laurent garos Mao Mao arrétel beat bi Arrétel beat bi please [Outro] Yo Ngour guéniou bédieune Founiou beug moniou faa té dieum Bour Ndiogne guinar-ram Badola rossi guédiaam Prézi ndel-lam ak costumeum Souniou estomac youy dioy laay degg sa soudé xoss tchineum Fuck sèn système Meunou mokko guiss dém Kambe gui loumou xautt xautt Fass nama yéné soulii saay mbautt Rimes yilaay diourgauutt Deugg djileuy thiokotane Sama nafa yi dii guileu né xétou pokotane Magueett nga rass nga, yakar bou tass nga Boulène tékeulé deug ak doul waay Amena niit you mérité woul tourou Abdoulaye Yeah Hannn haaaa This go out to all my niggas who tryin’ hustle Tryin’ J***** I know nigga another life for livin’ in Galsen is so hard But We don’t have no choice man Hustling wake up my nigga, It’s time now Yeah !!! To all my nigga who hustlin’ everyday All my nigga who tryin do something This go out for U nigga Never give up the fight man Sssstt ………….For Life One day will come We….. …… my nigga Just keep it real Keep Positive my nigga Right
Read the complete lyrics to "Cii Pèt" by Nitdoff from the album "Hip Hop Dou Messeu Dead". On Lyrks you can follow along with the full text, explore the artist's discography, and discover related songs. The track is often categorized under Rap.
"Cii Pèt" is performed by Nitdoff. from the album "Hip Hop Dou Messeu Dead" This page provides the full lyric text for fans who want to sing along, study the songwriting, or compare versions across releases. Lyrks organizes lyrics by artist and song slug so you can bookmark and share a stable URL.
Music lyrics help listeners connect with emotion, narrative, and rhythm in a track. Whether you are learning English, researching a favorite chorus, or preparing for karaoke, having accurate line breaks and section labels (verse, chorus, bridge) makes the experience easier. We link to the official artist profile on Lyrks where available, including biography snippets, top songs, and chart placements when we have that data.
If you enjoy "Cii Pèt", explore more songs by Nitdoff using the links below. Chart and trending pages on Lyrks highlight what listeners are searching for this week. For copyright or correction requests, see our DMCA and contact pages.
"Cii Pèt" is credited to Nitdoff. Songwriting credits may include additional writers listed on the release; check the credits section on this page for linked collaborators.
"Cii Pèt" appears on "Hip Hop Dou Messeu Dead".
Visit the Nitdoff artist page at /artist/nitdoff for biography, popular tracks, and links to more lyric pages.