Lyrks
Lyrks
Lyrks
Cover Art

Doff Ego 3 Lyrics by Nitdoff

2018

[Couplet unique]
Yeah I respect the game right ma décidé same life
Dém nigga tryna copy but déy djaffé tchi djeem right
Ma braquer sa zone KK yi bégué si sen side
Hip hop done agoniser ma nieuw diokhat ko sense like
The nigga with the doff style roubé na sen scribe
Bang bang b-bang taye moudjé neu diss price
Underground king mane leu mbède bi give choice
Loudoul Rap tigui Rap domafa guiss twice
Nigga ki nga done wait aksina pile poile
Assamaney Killah boulko teukeulek étoile
Ma ouf djant ouf werr meunouniou equal
Sa gaïndé dafeu mine zoo meuneutoul dekou aleu
Mofuking youkhou ouhhh takhoul niou equal
May bombe di blackout sa secteur di doubt about
Sey nigga leulou pino cuz my gun is pop out
Killah dou step back you better respect that
Bou game bi doundone deugue do lale mic bey khèp chèque
Thiogalou bullshit kouneh di niodi rapper fucking flop
Face Dém slap crap and trap ganda-propa
Docteur bi nénaleu Killah xadialoul diekhaloul
So banié deh xeloul dielna raw gadou gui té wékhaloul
Yagui mey signe di reh mais xamna sa beugn wékhé woul
Nii sa khole fekhé woul
Mc xewiwo mais dang fé xéwoul
Xeuyna di enchainer Mc yi melni Casanova
KK mousta keuf mic di rap di Rap nga degu that’s enough
Kou real rap di djap lo dathie na nga dass sa nopp
Ma diokhla frappe youy percuter melni bastonnade
Thiafka wou mbed bi la miine lo séni estomac
Bro Killah meussoul dokh dokhou fake
Keep it real ni dieun bi di miné ndokhou guedj
Yeah rap bi ley falo nekh meti pray for lord
Nigga li ngey nakhé sa public mom laniouy néfaro
Yakh nga té defaro anti Killah nga té faro
Doctor biley consulter fadjie leu donté sakh fébaro
Doma frek tchi mafia wou mbed bou fekké pégro
Guiss nga mane ni mey téguo tchi beat bi damey raye ego
Khibone nga té régueu go di splif up like raggae go
Mc da nga djiégué gow (fille) khana douguaguo négou goor
Killah koum tchi djékou door sifflet arbitre sakh neegou-ko
Chaise bi boudé kén dongue mane maay took
Mbedeu boudé séni song mane maay talk
Dem niggas bullshiting bou diant fink beu night o clock
Daminé sa L dou takh nga dégu nice spoke
Ay ranguoniou rethiou nioy walaguane sa eyes tokk
Déloul sa Size joke togual ak sey guys job
Killah dou mayé pepite da weeked si vice dog
Koccé né Ndongo guili né gongo paré si songo
Fake ya ngui tongo leungo
Maay lingot ni soufou congo
Tengo lou dinguo diom bi laay djiengo ngey oufou comme gow
Nigga compo séni complot dou képpeu Sonko
Listen dou wané tisseum dafeu deglou 3-4-5 rek 6 meu sisseum
Ma dokh thi gardeum killah bouy aksi ndakh danko guisseum
King la ngey misseum nit yi ley gueusseum atano ndisseum
Mbed moma harmoniser now mey dokh si peaceum di fils seum
Keep it G nigga every season, the mission
I got the vision now they give me reason
Li ngey wout ak limey wouteu bokoul sa respect yokoul
The money is so cool but andoulak respect soma guissatoul
Kollëré doguoul fitou none toguoul sa mc dioboul
Soukh nga thioguoul tolowounie pass pass bokoniou struggle
Mister mad mic ndeusteun nou last night
Moss naniou nathie nathie diotna niou dathie light
Di noce like té douniou lost right
Dieumbeuteul love sassouneh djiemeul kill hate
Dieum dji loff tewoul nga rich néh Bill Gates
Ame ame ak niak ci bopp leu Nigga stay proud
So niaké foula niou dioguila nigga stay proud
Boul xép sa bopp di dounguourou nigga stay proud
The most high moy contrôler nigga stay proud
Xam xam bi diomboula nigga you gotta play though
Credits

About “Doff Ego 3” by Nitdoff

Read the complete lyrics to "Doff Ego 3" by Nitdoff in 2018. On Lyrks you can follow along with the full text, explore the artist's discography, and discover related songs. The track is often categorized under Rap.

"Doff Ego 3" is performed by Nitdoff. in 2018 This page provides the full lyric text for fans who want to sing along, study the songwriting, or compare versions across releases. Lyrks organizes lyrics by artist and song slug so you can bookmark and share a stable URL. Music lyrics help listeners connect with emotion, narrative, and rhythm in a track. Whether you are learning English, researching a favorite chorus, or preparing for karaoke, having accurate line breaks and section labels (verse, chorus, bridge) makes the experience easier. We link to the official artist profile on Lyrks where available, including biography snippets, top songs, and chart placements when we have that data. If you enjoy "Doff Ego 3", explore more songs by Nitdoff using the links below. Chart and trending pages on Lyrks highlight what listeners are searching for this week. For copyright or correction requests, see our DMCA and contact pages.

View all songs and biography for Nitdoff · Trending lyrics · Billboard Hot 100

Frequently asked questions

"Doff Ego 3" is credited to Nitdoff. Songwriting credits may include additional writers listed on the release; check the credits section on this page for linked collaborators.

Album information for "Doff Ego 3" is not available in our database yet. You can still read the full lyrics on this page.

Visit the Nitdoff artist page at /artist/nitdoff for biography, popular tracks, and links to more lyric pages.