Lyrks
Lyrks
Lyrks
Cover Art

Adouna Lyrics by Natty Jean

Imagine

0

Nit ñi fi ñuy rawante / mooy ci xol yu rafet yee
Nit ñi fi ñuy amee barke/ mooy ci ñaanu waa-jur yee
Nit ñi fuñu jëm ag yaakamti / xanaa bëg yaxxule
Kon sa wërsëg ding ko fekkee/ xanaa waxtu bi su jotee
Na nga sant, sant, sant, sant te baña yàkkamti waay
Kon defal ndank, ndank, ndank, ndank mooy jàpp golo ci ñaay
Mu xiin, mu taw, mu neex, mu naqari (na nga am sa fulla waay)
Nga weex, nga ñuul, nga am ba xamadi (yaw bul fàtte Yalla waay)
Bula àdduna jay ba nga fàtte ki nga doon ding ko réccu
Nii de laa ko gisee
Yalla buur bi nelawul té gëmmentuwul
Leeg leeg mu jàpp njamburam ne tekk
Te loo ko ñaan mu may la ko si kaw nga laabir
Ag am jom te nangu lepp limu la teg
Nit ñi dañu bare dugg-dugg, xoolal bu baax
Laatà nguay dugg ci lu la bett
Nangu jël na cëru bañ ba tax na tay jii
Ki nga gën a wóolu moo la mën bett
One two three/ suñu Sénégal a ngui
Sutura bi daf fi jeex ba luñu gis di nettali
Mbele mbel bi bari, seen xol yi naqari
Nañu job te bàyyi coow li
Mu xiin, mu taw, mu neex, mu naqari (na nga am sa fulla waay)
Nga weex, nga ñuul, nga am ba xamadi (yaw bul fàtte Yalla waay)
Bula àdduna jay ba nga fàtte ki nga doon ding ko reccu
Nii de laa ko gisee
Yow da ngay mel ni nga wara mel, ñun ñu nangu say jikko
Buur bi baaxèe na ñu xel, li ci des mottali ko
Da nguay def li nga wara def, sa wërsëg lijjënti ko
Àdduna ag ni mu mel lo fi góobe garaale ko
Buula Yalla teggee nattu man what can you do
Li may ñaan mooy jàmm, wergi yaram, fan yu gudd
Na nga màndu, doo ko réccu, na nga tuub, jéggalu
Yalla rek a dul juum, nañu dem jébbalu
Ñu bare dañuy fàtte ne àdduna jaru ko
Ag loo fi mën am yaw da ngay dem bayyi ko
Kila bëg waxla dëgg da ngay teey deglu ko
Dunyaa tay jii dafa dem ba jaxasoo
Credits

About “Adouna” by Natty Jean

Read the complete lyrics to "Adouna" by Natty Jean from the album "Imagine". On Lyrks you can follow along with the full text, explore the artist's discography, and discover related songs. The track is often categorized under Pop.

"Adouna" is performed by Natty Jean. from the album "Imagine" This page provides the full lyric text for fans who want to sing along, study the songwriting, or compare versions across releases. Lyrks organizes lyrics by artist and song slug so you can bookmark and share a stable URL. Music lyrics help listeners connect with emotion, narrative, and rhythm in a track. Whether you are learning English, researching a favorite chorus, or preparing for karaoke, having accurate line breaks and section labels (verse, chorus, bridge) makes the experience easier. We link to the official artist profile on Lyrks where available, including biography snippets, top songs, and chart placements when we have that data. If you enjoy "Adouna", explore more songs by Natty Jean using the links below. Chart and trending pages on Lyrks highlight what listeners are searching for this week. For copyright or correction requests, see our DMCA and contact pages.

View all songs and biography for Natty Jean · Trending lyrics · Billboard Hot 100

Frequently asked questions

"Adouna" is credited to Natty Jean. Songwriting credits may include additional writers listed on the release; check the credits section on this page for linked collaborators.

"Adouna" appears on "Imagine".

Visit the Natty Jean artist page at /artist/natty-jean for biography, popular tracks, and links to more lyric pages.