Lyrks
Lyrks
Lyrks
Cover Art

Ak Yow Lyrics by Natty Jean

Imagine

0

Sans yaw, dafay melni àdduna day bëg tukki
Ak yaw, damay melni ku tëye alalu bukki
Dëgg la sama chérie kon tay jii maa la tooñ
Wante yaa ma xamal tay jii luma xamulwoon
Maa ngi fataliku bi ñuy toog ci boppu koñ
Suñuy gént ag sunuy yeene rek lañu amoon
Waye seytane dafay faral di jaxase di ñu féewale
Seytane bëgul ñaar ñu bëgante, bëgul ñuy fo di ree
Ndax yaw laa love
Baby yow laa bëg sama life
Baby bu dul yaw man dinaa die
Baby jàpp naa dootuma bayyi
(2x)
Sans yow, dara dootul neex, man lepp daf may sàppi
Ag yaw, damay bëg ba fumala séen di lappi-laapi
Chéri man ag yaw du hasard
Gëm naa ni boo pareegul man damay toog di la xaar
Chéri man ag yaw dafa tar
Looló waral man ma gëm ne lepp lepp dina baax
Ndax yaw laa love
Baby yaw laa bëg sama life
Baby bu dul yaw man dinaa die
Baby japp na dootuma bayyi
Waye seytane dafay faral di jaxase di ñu féewale
Seytané bëgul ñaar ñu bëgante, bëgul ñuy fo di ree
Baby all my love is for you, I go sing it
Bul xool ci benn seytane bul deglu benn wicked
Ma ñàkk sama bakkan fuma toog dinaa la siggil
Bimala xamee ba leegi bëggatuma keneen
Chérie coco banne dama jooy, man dama fada
Bëg naa doon papa, ma def la mada
Sama xol bi moo la fal te jox na la benn mandat
À vie te nee na loo bëg dina ci ànd
Mais yenn saa yi bumala tooñee
Sama chérie nang ma baal
Te baña topp waxu noon yi daf ñuy gaañ
Ndax yaw laa love
Baby yaw laa bëg sama life
Baby bu dul yaw man dinaa die
Baby japp na dootuma bayyi
Credits

About “Ak Yow” by Natty Jean

Read the complete lyrics to "Ak Yow" by Natty Jean from the album "Imagine". On Lyrks you can follow along with the full text, explore the artist's discography, and discover related songs. The track is often categorized under Pop.

"Ak Yow" is performed by Natty Jean. from the album "Imagine" This page provides the full lyric text for fans who want to sing along, study the songwriting, or compare versions across releases. Lyrks organizes lyrics by artist and song slug so you can bookmark and share a stable URL. Music lyrics help listeners connect with emotion, narrative, and rhythm in a track. Whether you are learning English, researching a favorite chorus, or preparing for karaoke, having accurate line breaks and section labels (verse, chorus, bridge) makes the experience easier. We link to the official artist profile on Lyrks where available, including biography snippets, top songs, and chart placements when we have that data. If you enjoy "Ak Yow", explore more songs by Natty Jean using the links below. Chart and trending pages on Lyrks highlight what listeners are searching for this week. For copyright or correction requests, see our DMCA and contact pages.

View all songs and biography for Natty Jean · Trending lyrics · Billboard Hot 100

Frequently asked questions

"Ak Yow" is credited to Natty Jean. Songwriting credits may include additional writers listed on the release; check the credits section on this page for linked collaborators.

"Ak Yow" appears on "Imagine".

Visit the Natty Jean artist page at /artist/natty-jean for biography, popular tracks, and links to more lyric pages.