Lyrks
Lyrks
Lyrks
Cover Art

Lou Teugue Tass Lyrics by Natty Jean

Imagine

0

Lu tëgg tas ci life bi!
Lu tëgg tas ci life bi!
My broda lepp luñu waxantewoon, lepp liñu digaalewoon
Lepp liñu yeenantewoon leegi jeex na, leegi dem nga!
My sistren man ag yaw du kan moo tooñ, Buur bi Yallaa ñu boolewoon, melna ni bokkatu ñu yoon leegi jeex na, leegi dem na, namm naa la!
Lu tëgg tas, lu tëgg tas, maa lako wax lu tëgg tas
Amna fo xamantene buñ fa nare yeeg man ma waaf
Jàppal sa Pa, jàppal sa Ma, kudul sa waay yaw nang ko taf
Ki la bëg dina la jàpp, ku la bëgul bumla saf
Leeg-leeg nga gestu do gis kenn
Sa xol bi jeex nga naqarlu te doo ko mën wax fenn
Te lu dul dëgg di ay fen
Te waruñu toog di tappale
Te waruñu doon keneen
My broda lepp luñu waxantewoon, lepp liñu digaalewoon
Lepp liñu yeenantewoon leegi jeex na, leegi dem nga!
My sistren man ag yaw du kan moo tooñ, Buur bi Yallaa ñu boolewoon, melna ni bokkatu ñu yoon leegi jeex na, leegi dem na, namm naa la!
Nañu ànd ci bamu jotee, numu gëna rafetee
Wayé tàqaliku bu jotee buñu kenn gëna gore
Nañu ànd ci bamu jotee, numu gëna rafetee
Waye tàqaliku bu jotee buñu kеnn gëna gore
Àdduna nii la, demal maa ngi ñëw la
Ànd bu yaag sax day jeex wante loolu bumu la jaaxal
Kii la wala kee la, yaw ki la Yalla booleel fеxeel ba moom dula raw
Siggi naa ni wóoy, siggi naa ni naa ni wóoy
Mais fils, duma la fenn, leeg-leeg sama xol day boy
Damay triste te duma xam man mi li may taxa jooy
Buko defee sama xel day dem ci God, ci family ag samay waay
My broda lepp luñu waxantewoon, lepp liñu digaalewoon
Lepp liñu yeenantewoon leegi jeex na, leegi dem nga!
My sistren man ag yaw du kan moo tooñ, Buur bi Yallaa ñu boolewoon, melna ni bokkatu ñu yoon leegi jeex na, leegi dem na, namm naa la!
Suma la tooñee nang ma baal, ndax dara jaruko fi
Yaw booma tooñee naa la baal, ñun dañu fee gane si
Budee jàmm rek a la taxa jog, bul ragal dellusil
Da nguay toog ag nit bamu yaag bes ñu ne la nekkatu fi
Wër nga aduna, loolu bumu la taxa change
Say mbokk ñooy sa doole, bo leen ñàkkee yaa ngi ci danger
Yalla mi ñu sàkk ñun ñëpp la fi nekkal
Kon tàqaliku bu jotee kune na jël ay dëbësam
Lu tëgg tas, lu tëgg tas, lu tëgg tas, lu tëgg tas!
Lu tëgg tas, lu tëgg tas, lu tëgg tas, lu tëgg tas!
Credits

About “Lou Teugue Tass” by Natty Jean

Read the complete lyrics to "Lou Teugue Tass" by Natty Jean from the album "Imagine". On Lyrks you can follow along with the full text, explore the artist's discography, and discover related songs. The track is often categorized under Pop.

"Lou Teugue Tass" is performed by Natty Jean. from the album "Imagine" This page provides the full lyric text for fans who want to sing along, study the songwriting, or compare versions across releases. Lyrks organizes lyrics by artist and song slug so you can bookmark and share a stable URL. Music lyrics help listeners connect with emotion, narrative, and rhythm in a track. Whether you are learning English, researching a favorite chorus, or preparing for karaoke, having accurate line breaks and section labels (verse, chorus, bridge) makes the experience easier. We link to the official artist profile on Lyrks where available, including biography snippets, top songs, and chart placements when we have that data. If you enjoy "Lou Teugue Tass", explore more songs by Natty Jean using the links below. Chart and trending pages on Lyrks highlight what listeners are searching for this week. For copyright or correction requests, see our DMCA and contact pages.

View all songs and biography for Natty Jean · Trending lyrics · Billboard Hot 100

Frequently asked questions

"Lou Teugue Tass" is credited to Natty Jean. Songwriting credits may include additional writers listed on the release; check the credits section on this page for linked collaborators.

"Lou Teugue Tass" appears on "Imagine".

Visit the Natty Jean artist page at /artist/natty-jean for biography, popular tracks, and links to more lyric pages.